Letras Dée Moo Wóor - Orchestra Baobab

Dée Moo Wóor - Orchestra Baobab
Información de la canción En esta página puedes encontrar la letra de la canción Dée Moo Wóor, artista - Orchestra Baobab. canción del álbum Specialist In All Styles, en el genero Латиноамериканская музыка
Fecha de emisión: 01.09.2002
Etiqueta de registro: World Circuit
Idioma de la canción: cebuano

Dée Moo Wóor

Aduna ko meuneu diouyou louy weey law
Aduna ko meuneu diooy lou weey law
Dama tokk beu digui diorr teud teud nelaw
diekh xell mi deim thie Lakhiraa dee moo worr
Waindé, Waindé Dieng toundou bayi Ngoné Ndour
Malick bayou Penda Ngane dee mo worr
Meunou meu neilaw ngir xalatt sama baye bi telleu reer
Ey way gars gni ndeikeiteii dee mo worr
(Dama tokk beu digui diorr teud teud neilaw
diekh khell mi deim thie Lakhiraa dee mo worr) x2
Ma deim Niger kholl founé dee mo worr
Aduna ko meune dioy louy weey law
Sama khell mi yedd ma,
sama kholl bi dioy Malick bayou Penda Ngane dee mo worr
(Dama tokk beu digui diorr teud teud neilaw
diekh khell mi deim thie Lakhiraa dee mo worr) x2
Khawma kagn la, khawma fane leu,
khawmeu nane leu may dikké man khamnani deug dall dee mo worr
Meunou meu nelaw ngir khalatt sama baye bi telleu reer
Ey way gars gni ndeikeitei dee mo worr
Yallah buur bi laniouy niane lidoul diarr
té yagg mom feikk niou dieuf diou bakh amiina
Amine, aaamine yalna Yallah nangou niane
Amine, aaamine, aminaa
(Dama tokk beu digui diorr teud teud neilaw
diekh khell mi deim thie Lakhiraa dee mo worr) x4

Compartir letras:

¡Escribe lo que piensas sobre la letra!

Otras canciones del artista:

NombreAño
Coumba 1981

Letras de artistas: Orchestra Baobab