Letras Fa Diallo - Ismaël Lo

Fa Diallo - Ismaël Lo
Información de la canción En esta página puedes encontrar la letra de la canción Fa Diallo, artista - Ismaël Lo. canción del álbum Tadieu Bone, en el genero Африканская музыка
Fecha de emisión: 31.12.1999
Etiqueta de registro: Syllart
Idioma de la canción: maorí

Fa Diallo

Beuguena wanté mane dé dama amoul
Da nga di gouné motakh mouy sa khalaat
Ni Beuguena wanté mane dé dama Ragal
Da nga di ngouné moutakh mouy sa khalaat
Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé?
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
Té legui bo ko meunoul demal teudi
Cherie coco li dé doyna kemane
Nga nane ma kay niou say té awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li dé doyna kemane
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Nga nane ma kay niou say té awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li dé doyna kemane
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la
Cherie coco wakhma no ko Guissé
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la
Cherie coco wakhma no ko Guissé
Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé?
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
Té legui bo ko meunoul demal teudi
Cherie coco li dé doyna kemane
Nga nane ma takk la mane awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li dé doyna kemane
Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la

Compartir letras:

¡Escribe lo que piensas sobre la letra!

Otras canciones del artista:

NombreAño
Tajabone 2015
Jammu Africa 2015
Nafanta 2015
Tadieu Bone 1986
Dibi Dibi Rek 2015
Noir Et Blanc ft. Ismaël Lo 2015
L'Amour A Tous Les Droits 2015
Without Blame ft. Marianne Faithfull 2015
Sofia 2015
Liberté ft. Ismaël Lo, Lokua Kanza, Koffi Olomide 1999
Après la guerre ft. Ismaël Lo 1999

Letras de artistas: Ismaël Lo