Letras Jammu Africa - Ismaël Lo

Jammu Africa - Ismaël Lo
Información de la canción En esta página puedes encontrar la letra de la canción Jammu Africa, artista - Ismaël Lo. canción del álbum Best Of, en el genero Музыка мира
Fecha de emisión: 14.06.2015
Etiqueta de registro: Capitol Music France
Idioma de la canción: Francés

Jammu Africa

Afrika a a a Afrika mon Afrique
Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq
Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew
D’ici ou d’ailleurs nous somm' des enfants d’Afrique
Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan
Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika
Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur
Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères
Kon jammu Afrika moom lay ñaan
Mané jammu Afrika mooy suñu natange
Afrika a a a Afrika a a
Afrika a a a Afrika mon Afrique
Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men
Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi
Yoo Alla addu jam to Ruanda
Yoo Alla addu jam to Burundi
Yoo Alla addu jam to Casamans
Lawol Mbignona yee

Compartir letras:

¡Escribe lo que piensas sobre la letra!

Otras canciones del artista:

NombreAño
Tajabone 2015
Nafanta 2015
Tadieu Bone 1986
Dibi Dibi Rek 2015
Noir Et Blanc ft. Ismaël Lo 2015
L'Amour A Tous Les Droits 2015
Without Blame ft. Marianne Faithfull 2015
Sofia 2015
Liberté ft. Ismaël Lo, Lokua Kanza, Koffi Olomide 1999
Après la guerre ft. Ismaël Lo 1999
Fa Diallo 1999

Letras de artistas: Ismaël Lo