Letras Dibi Dibi Rek - Ismaël Lo

Dibi Dibi Rek - Ismaël Lo
Información de la canción En esta página puedes encontrar la letra de la canción Dibi Dibi Rek, artista - Ismaël Lo. canción del álbum Best Of, en el genero Музыка мира
Fecha de emisión: 14.06.2015
Etiqueta de registro: Capitol Music France
Idioma de la canción: maorí

Dibi Dibi Rek

Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
yangui deugueurlou wanté meunoko boul sop bayil niou djeuliko
yangui ndirok balai bou niou takhawal, aah ndakh yow lekkato
yangui beugu dé ndakh yow nanato, boul sop bayil niou djeuliko
Ndakh mo ley madj lo
Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Mbeuguel kenn khamoul lou mou doonn
Foulla diou barri ndaham amatou fi yoon
Kholl moy capitainou boromam
Ndakh mo ley madj lo
Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Ay niit niom bou niou beuguenté, khamaal lo tchi waakh
Niom mame boye sene taar wessouna, wayé tey laniou gueuneu beugueunté
Ya ngui beugu dé ndakh yaw lekatto
Bo fi guetarro waw ma bayiko
Ndakh mo lay madj lo
Dibi Dibi Rek
aahDibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Dibi Dibi Rek
aahDibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Ndakh mo lay madj lo
Ndakh mo lay madj lo
Dibi Dibi Rek
aahDibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Dibi Dibi Rek
aahDibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Dibi Dibi Rek
aahDibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek
Dibi Dibi Rek
aahDibi Dibi Rek
aah Dibi Dibi Rek

Compartir letras:

¡Escribe lo que piensas sobre la letra!

Otras canciones del artista:

NombreAño
Tajabone 2015
Jammu Africa 2015
Nafanta 2015
Tadieu Bone 1986
Noir Et Blanc ft. Ismaël Lo 2015
L'Amour A Tous Les Droits 2015
Without Blame ft. Marianne Faithfull 2015
Sofia 2015
Liberté ft. Ismaël Lo, Lokua Kanza, Koffi Olomide 1999
Après la guerre ft. Ismaël Lo 1999
Fa Diallo 1999

Letras de artistas: Ismaël Lo