Información de la canción En esta página puedes encontrar la letra de la canción Xel, artista - Youssou N'Dour.
Fecha de emisión: 28.10.2007
Idioma de la canción: Francés
Xel |
Paroles de la chanson Xel: |
Famarë reub kat lawone |
Da ama biss mou khall yône |
Mu taxaw di xalat bamu yàg |
Mu sène mbëtt miy daw |
Mu suxat fital ambadi dâgu |
Té nane kî douma raw |
Far mbëtt ma sène kokorong |
Dadi dieul bop ba |
Dal di koy rône |
Bopp ba neubouna litha des |
Yaramam béppa ngui fègn |
Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya |
Lippe di fègne |
Lii takh mou déféni |
Mbeutteu daa amoul xel |
Kone gnoune gni Yalla jox xel |
Nagnu santati (x2) |
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk |
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax déf |
Loy dougou jitalal sa xel |
Ba lo thièy wout |
Di nga guiss nguenél |
Nit gni yor xel boo sété gnoy dokhal aduna |
Kiy déf té dou xalat |
Thi missal day mél ni mbeut ma |
Nit môm khélako yor (x4) |
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk |
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf |
Fi neubeu moy khax |
Boko amoul yangui mél ni bayima |
Sokou amoul doto nék nit |
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk |
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf |
Wawaw (x4) |
Famarë reub kat lawone |
Da ama biss mou khall yône |
Mu taxaw di xalat bamu yàg |
Mu sène mbëtt miy daw |
Mu suxat fital am ba di dâgu |
Té nane kî douma raw |
Far mbëtt ma sène kokorong |
Dadi dieul bop ba |
Dal di koy rône |
Bopp ba neubouna litha des |
Yaramam béppa ngui fègn |
Deune bak, ndigg lak, tank yak, yénène ya |
Lippe di fègne |
Lii takh mou déféni |
Mbeutteu daa amoul xel |
Kone gnoune gni Yalla jox xel |
Nagnu santati (x2) |
Li Yalla bind yépp nit lathie gueneu fonk |
Mala yi lignou woutelé ak gnom moy sougnou xel motax gnuy déf |
Wawaw lolu moy xel |
Soko amoul |
Yangui mél bayima (x3) |
Loy dougou nang ko téké xel |
Famarë reub kat lawone |
Mbeuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuuutt! |